Sender: zpajol@mailhost.monde-diplomatique.fr
Reply-To: zpajol@monde-diplomatique.fr
Mime-Version: 1.0
Precedence: Bulk
Date: Thu, 12 Dec 1996 11:22:03 +0200
From: bachastu@sonatel.senet.net
To: Multiple recipients of <zpajol@mailhost.monde-diplomatique.fr>
Subject: Gaa ni...
Mbokk yi,
Ñun ay ñu doon ligéey mbaa di jàng tugël
ci at yi weesu la ñu. Ñu ngi dëkk
ci diiwaanu Tàmbakundaa. Ni leen nguuri
Farans def mettina ñu torop. Dafa fa
mel na yar yi leen "CRS" yi doon döör
suñu kaw la doon dal. Dina ñu def liñu
mën ngir jàppale leen, ndax seen xeex
ñoo ko bokk. Tàmbale na ñu yëgle bi ci
kuréél yiy aar sañ-sañu doomu aadama yi.
Di na ñu def suñu kéémtalaayu
kàttan ngir siiwal seen ñefe. Dëgërël
leen seen mànko! Bu ngeen jàppe fële
ñu jàpp fii, ag ndimalu tubaab yiy xeex
boddënte xeet tey ñefe ngir sàmp
demokarasi, daañu yoobu ndam li.
Jarawlak gaa ñi!!
SEENI MBOKK FII CI TAMBAKUNDAA
--
| Philippe Riviere <riviere@ina.fr> INA/Le Monde diplomatique |
| http://www.ina.fr/CP/MondeDiplo/ |
| debats & infos: http://www.ina.fr/CP/MondeDiplo/Forum/ |
__________________________________________
Les Africains sans-papiers de St Ambroise.
http://bok.net/pajol/
messages de soutien : pajol@bok.net
infos et communiques : <zpajol@monde-diplomatique.fr>
Cette liste est geree par l'automate Macjordomo :
<zlistes@monde-diplomatique.fr>
Pour se retirer de la liste: envoyer a <zlistes@Monde-diplomatique.fr> le
message :
UNSUBSCRIBE zpajol
Aide: HELP ou <http://bok.net/~fil/macj/aide.html>