Afrikin yi amul këyit
« yu Saint-Ambroise »
25 octobar 1996


  • http://bok.net/pajol
    E-mail : pajol@bok.net
  • français / english  / deutsch / italiano / wolof
    ÑATI TEEMERU WÂ AFRIK yi amul këyit biy tax ñu mëna dund si frans ñoo ngiy xeex ndax ñu mëna Lijanti seen mbir. Xeex bi nake ñoo ngi ka door sa Egliz bu St Bernard bi nekë Paris. Kilifa dëk bi daje nañu daje bu gaw ngir ubbi daara. Daara bi nakk dañu ka def ngir mana waxtaan ake goornamaabi. Leegi nake gni amoul këyit nëpp dañu leen wara gene si rewmi. Waaye fuk si ñoom door nañu xeex boo xamne duñu lekk duñu naan Juroom fuku fan. Xex bi nakk da fa door waxtu boo xamne reewum frans, yenen rew yëp da ñu koy xass ngir axu nit yii mu gadu. (kÿitu Glele bu Nations Unies, Cour de Strasbourg, Mbotayu adunabi bit doxal yon)

    tressage

    Xexum jasi ak carwas :

    Ajuma 23 aout 1996 bi 7h30, joto alkati yi daji nañu buntu egliz bu Saint Bernard, dax Afrikin yi amul këyit

    Ku beg xam fuñ tolu : 01 36 68 73 93 (réseau Voltaire, 2,23 F/mn ñoy natal ñi amul këyit).
    Toxute ñi amul këyit (La ballade des sans-papiers, filmu Samir Abdallah ak Rafaelle Ventura, Agence Im'média) : band bi mungi L'yeux ouvert, BP 624, 92006 Nanterre, tél. : 01 47 66 71 76, fax : 01 44 40 07 26 (ñungi koy jay 200F + 20F yobël, sec bi ñu yone ko "Télé de rue / Yeux ouverts").
    Dimbalum xalis : ñu deñtiu sen xalis Crédit mutuel n° 80134041, sec bi ñu yone ko "CFDT cheminots / Solidarité sans-papiers".
    Ndeñtium Web :
    Marc Chemillier
    Tél./fax 01 45 81 31 14
    16 r A Mouchez 75014 Paris
    Isabelle Saint-Saens
    Annick Armani-Huau
    Zoubir Sami
    Wolofal bi : anonyme
    Foto yi :
    © Pascal Lafay 1996
    Ligey bi :
    Gérard Assayag, Peter Hanappe
    Band bi : Monique Bernot
    Jërëjëf Gilles Boccon-Gibod
    ñi len dëkël
    ubi nañu 10 juillet 1996
    Ñati temeru nit ño len di wo semen bu nek!