[page d'accueil] |
français / wolof
|
AJUMA ñar fuku fan ak ñat si weru aout si atum ren bi si waxtu suba teel junii ak lu tek si ay alkati daje nañu buntu eglizu Saint-Bernard ngir dax ñaati temeru afrikin yi amul këyit ak ñi len di japale te newon si palas bobu. Ñi amul këyt dañu ne won buñu len di uta gene bu kena dëgër na ñëp dem. Com ni ko Debré waxe ken dëgërënte wu si ak alkati yi. Amna ñiñu yobu Vincennes, juroom fuku nit ñu sëyul, ño rëçë si xeex bi. Bi gene bi pase ba am semen, fuki nit lañu yobu. Afrik, ñi si des yëp amnu ñu ñu bayi, ñenen yi ñu yobu len Cartoucherie bu Vincennes. Ño ngi yegalii sen xeex !!!
Emmanuelle Béart... |
Kilifa egliz bi ñuy wowe Père Coindé defna « mesu alkatiyi ». Taxaway bu doy war...! |
Nitu benen aduna ?... |
Dem len, amul luñuy setan !... |
« ... nit yi taxaw nañu taxaway bu rafet bi ñuy dajii buntu egliz bi. » (Pascal Lafay) |