Afrikin yi amul këyit « yu Saint-Ambroise » |
25 octobar 1996 |
E-mail : pajol@bok.net |
français / english / deutsch / italiano / wolof |
ÑATI TEEMERU WÂ AFRIK yi amul këyit biy tax ñu mëna dund si frans ñoo ngiy xeex ndax ñu mëna Lijanti seen mbir. Xeex bi nake ñoo ngi ka door sa Egliz bu St Bernard bi nekë Paris. Kilifa dëk bi daje nañu daje bu gaw ngir ubbi daara. Daara bi nakk dañu ka def ngir mana waxtaan ake goornamaabi. Leegi nake gni amoul këyit nëpp dañu leen wara gene si rewmi. Waaye fuk si ñoom door nañu xeex boo xamne duñu lekk duñu naan Juroom fuku fan. Xex bi nakk da fa door waxtu boo xamne reewum frans, yenen rew yëp da ñu koy xass ngir axu nit yii mu gadu.
(kÿitu Glele bu Nations Unies,
Cour de Strasbourg, Mbotayu adunabi bit doxal yon)
|
Ajuma 23 aout 1996 bi 7h30, joto alkati yi daji nañu buntu egliz bu Saint Bernard, dax Afrikin yi amul këyit
Ndeñtium Web : Marc Chemillier Tél./fax 01 45 81 31 14 16 r A Mouchez 75014 Paris Isabelle Saint-Saens Annick Armani-Huau Zoubir Sami Wolofal bi : anonyme |
Foto yi : © Pascal Lafay 1996 Ligey bi : Gérard Assayag, Peter Hanappe Band bi : Monique Bernot Jërëjëf Gilles Boccon-Gibod ñi len dëkël ubi nañu 10 juillet 1996 Ñati temeru nit ño len di wo semen bu nek! |